CI MBIRU TOR BROWSER
Jàngal li Tor Browser mën a def ngir aar say mbiri bopp ak sa làqqute
YEBBI
Naka lanuy yebbee Tor Browser
SAMP
Samp Tor Browser
DOXAL TOR BROWSER YOON WU NJËKK
Jàngal nan lanuy jëfandikoo Tor Browser yoon wu njëkk
ANTI-FINGERPRINTING
How Tor Browser mitigates browser fingerprinting
MOYTU
Lan lanuy def su jokkoowu Tor taxawee
BRIDGES
Pluggable Transports yu gën a bari, niki obfs4, dañuy wéeru ci jëfandikoowu jàllalekaayi "bridge"
SAYTU XAMMEEKAAY YI
Jàngal naka lanuy saytoo xibaaru xammee sa bopp ci Tor Browser
ONION SERVICES
Serwiis yi nga xam ne ci Tor lañu leen di amee
KAARÀNGEY LËKKALOO
Jàngal nan ngay aaree say joxe di jëfandikoo Tor Browser ak HTTPS
KAARÀNGEY SUKKANDIKUKAAY
Di defaraat Tor Browser ngir kaarànge ak jëfandikokaay
TROUBLESHOOTING
What to do if Tor Browser is not working
YEESAL
Naka lanuy yeesalee Tor Browser
ARAFU BENNAL DEÑC, SIIWAL AK JAVASCRIPT
Nan la Tor Browser yoree siiwal yi, arafu bennal ab deñc ak JavaScript
SEMPI
Nan ngay dindee Tor Browser ci sa nosteg amalin
PORTAABAL BU TOR
Jàngal lu jëm ci Tor ngir telefon portaabal yi
JAFE-JAFE YUNU XAM
Jafe-jafe yi nu xam
DEF TOR BROWSER LUÑU MËN A TEYE CI LOXO
Naka lanuy sampe Tor Browser ci xibaar yu mën a dindi
NDIMBAL
Nan ngay amee ndimbal, def xëtu tegtal njumte wala def ab mbinbu leeral